musicas.mus.br
Letras de músicas - letra de música - letra da música - letras e cifras - letras traduzidas - letra traduzida - lyrics - paroles - lyric - canciones - LEPP LEGUI (FEAT. ZOU KANA) - OMZO DOLLAR - música e letra
Utilize o abecedário abaixo para abrir as páginas de letras dos artistas
Lepp legui (feat. Zou Kana) letra
Toubab yangui bronzer nit you nioul
Di khessal nieup may moudier konser
GMI doyalouniou yalla yefer yi geumouniou yallah nieupay moudier enfer
Lou gueneu gaw si mbourou wala leeguins
Mbourou da lay djokh kelkun
Leeguins dala diokh nimporte ki
Ok
Kay ma wakh lanrek moma metti ioe
Professeur boudé yamay djangal wakhma noumay
Def ba tekki té wakhma lane motakh ba ioe tekiwo
Shit
Gars yi kou len wakh mariage niou len nengo
Diabar dote 1million wayé thiaga passe ten taw
Domou adama dou doye ci bopam
De kharou ci len sou ka amé mou out loka am
Li nga khamoul doula sonnal a partir de bingay kham
Linga beugeu dinga khep jour bingay am
Douniou mbolo wanté
Deukeur bop ba melni ngolo kante
Sou la wakh dafa vierge dafay soga tenté
Beugone tak defar bijou famille
Mais bijou bizou mo geuneul samay bijoux de familles (abozé)
Omzo Dollar - Letras
- Bae
- Beuy
- Borom
- Borom Keur
- Bureau (feat. Young Tili)
- Buur
- Ci Loo Nekk (feat. OoThenTik Zeus)
- Del Bale (feat. Safary)
- Delouci (Bonus Track)
- Dope
- Façon Bou Né (feat. Canabasse)
- Fadiar
- Gana
- Gengis Khan
- Goudi (feat. Majestic Drama)
- Lat Prada Freestyles
- Lepp legui (feat. Zou Kana)
- Leundeum (feat. Mia Guisse)
- Lionnel Fatt
- Lo Meu Def
- Makoy Todj (feat. Buzz Lab, MedMetal & Canabasse)
- Mame Premier
- Messatsu
- Ndakh Rap
- Nitté
- Omar Pen
- Omar’s Pain
- Penda Mbaye
- Sante (feat. Kheuchy-T)
- Simple (feat. Pape Diouf)
- Sokhor
- Soutoural
- Tassaré
- Thias
- Xel Ak Xol
- Yenene Jap (feat. Kheuchy-T)
top 30 músicas
©2003 - 2026 - musicas.mus.br