musicas.mus.br
Letras de músicas - letra de música - letra da música - letras e cifras - letras traduzidas - letra traduzida - lyrics - paroles - lyric - canciones - LEUNDEUM (FEAT. MIA GUISSE) - OMZO DOLLAR - música e letra
Utilize o abecedário abaixo para abrir as páginas de letras dos artistas
Leundeum (feat. Mia Guisse) letra
Majestic Drama
Fu ma mëna ne jot sa appel: Bae foo ne?
Li ma mëna def nga ni ma bae, no, no, no, no du way
Allo, bae foo nekk?
Ñibbisil, il fait nuit
Waññil coow li, jalousie danga metti
Góor a lëndëm, góor a lëndëm, góor a lëndëm yeay
Góor a lëndëm, góor a lëndëm, góor a lëndëm yeay
Ñaata góor ñoo ma topp
Nga may wax li di ma tooñ
Sonn naa, dootuma toog
Confiance bu amul ci mbëggeel, non, non, du dem
Fu ma mëna ne jot sa appel: Bae foo ne?
Lu ma mëna def nga ne ma bae, no, no, no, no du way
Góor a lëndëm, góor a lëndëm, góor a lëndëm yeay
Góor a lëndëm, góor a lëndëm, góor a lëndëm yeay
I say
Jigéen bu baax, góor bu bon
Takkali ko ni diwlin ak ndox
Dama soxla ku may dégg sa soxla ku lay déglu
Su ma xamul li ma bëgg xam naa li ma bëggul, yeah
Mais góor a mel noonu fu mu tollu day risquer
Daan kay defal jamm ku ko sonal lay pister
Boo tegee tànk ci biti mu lay call insister
Sa tur ci sama xol ndax ne nañu xol day gise
Am na lu ma metti
Ndax su ma la woree bàyyi bëgguma la gis ak keneen mais
Est-ce que dama toxique?
Est-ce que dama toxique?
Jël sa xel bi dox ci, jël sa xol bi toog ci lëndëm
Góor a lëndëm, góor a lëndëm, góor a lëndëm
Góor a lëndëm, góor a lëndëm
Yeah, yeah
Hum!
Kon waxal góor yi lay topp
Ni demoo fenn fi ngay toog
Ñun ñaar ñoo changer mu dem
Effort su amul ci mbëggeel, non, non, du dem!
Fu ma mëna ne jot sa appel: Bae foo ne?
Li ma mëna def nga ne ma bae, no, no, no, no du way
Góor a lëndëm, góor a lëndëm, góor a lëndëm yeay
Góor a lëndëm, góor a lëndëm, góor a lëndëm yeay
Omzo Dollar - Letras
- Bae
- Beuy
- Borom
- Borom Keur
- Bureau (feat. Young Tili)
- Buur
- Ci Loo Nekk (feat. OoThenTik Zeus)
- Del Bale (feat. Safary)
- Delouci (Bonus Track)
- Dope
- Façon Bou Né (feat. Canabasse)
- Fadiar
- Gana
- Gengis Khan
- Goudi (feat. Majestic Drama)
- Lat Prada Freestyles
- Lepp legui (feat. Zou Kana)
- Leundeum (feat. Mia Guisse)
- Lionnel Fatt
- Lo Meu Def
- Makoy Todj (feat. Buzz Lab, MedMetal & Canabasse)
- Mame Premier
- Messatsu
- Ndakh Rap
- Nitté
- Omar Pen
- Omar’s Pain
- Penda Mbaye
- Sante (feat. Kheuchy-T)
- Simple (feat. Pape Diouf)
- Sokhor
- Soutoural
- Tassaré
- Thias
- Xel Ak Xol
- Yenene Jap (feat. Kheuchy-T)
top 30 músicas
©2003 - 2026 - musicas.mus.br